Dund gu teey ci kéew mu sell
Nit mënul dund lu dul ciy dëkkandoom (garab yi, gàncax yi, mala yi ak ndundat yi), te ñoom mën nañu dund waliif moom.
Ay njeexiiti jëfam du neen mukk ci dundug ëllëgam. La mu ji lay góobi. Laaj bi mooy fan ak lan lay ji ? Ci kéewam lay ji. Ay jëfam ay jiwoom. Moo tax téere bi dikk di ko dànkaafu, di ko bàyyiloo xel ngir muy tànn jiwu ya gën. Dund du teey li fii ak kéew sellul. Kéew du sell mukk li fii ak nit ki ciy dund dundalul ko ci jëf yuy bàyyi xel ëllëg.
« Ku sàmm sa kéew sottal añ bi lay jox wér, di féq saw fan,
Nga mën ca a dund, di ca dundale, di teeru ak a teral gan. »
Auteur: Saalum Jaane
4.500 CFA
Description

You must be logged in to post a review.
Reviews
There are no reviews yet.